Nangoulma
Viviane Chidid
Nangoul wakh!
Nél sa khol maan ma si néh
Baby tay ma léral la
Né khaam nani maan rék ngay weur
Deug le
Kou mél ni nga sokh la
Meuné founéh
Fouma feul rék diomal la
Khaam na ni djantal nga
Nangoul né maan may sa star
Kou khaam li laan la
Nga Wakh ma
Kou kham li laan la
Ma nékhal la
Kou khaam li laan la
Nga Wakh ma
Kou kham li laan la
Ma nékhal la
Soon na si saag bi
Di mougn lou mel ni
May ladj ki laan la
Maan da ma soon si saag bi
Di mougn lou mél ni
May ladj ki laan la
Baby! nangoul ma
Wakhal sa gars gni
Maan mail sa star
Té nga siggi khol ma
Maan guis na
Sa profil maan ma fa néh
Baby nangoul maan rék la
Sa yo wétté, ba khalat ma
rék réh
Di latj té ndakh nit la
Diakhlé si maan
Bay khalat
Ma diomal la!
Fo guésto ba xolma
Do to beug dara
Loudoul gnew nékhal ma
Kou khaam li laan la
Nga Wakh ma
Kou kham li laan la
Ma nékhal la
Kou khaam li laan la
Nga Wakh ma
Kou kham li laan la
Ma nékhal la
Soon na si saag bi
Di mougn lou mel ni
May ladj ki laan la
Maan da ma soon si saag bi
Di mougn lou mél ni
May ladj ki laan la
Baby! nangoul ma
Wakhal sa gars gni
Maan mail sa star
Té nga siggi khol ma
Tay ma deugueul la né yaw la
Maan li mail yeungeul yeup
Si yaw la néh
Mat nga ma kilifa, yeureum nga ma
Guissou ma lou ma naam
Ndakh sagal ngama
Baby ! Kay diéga ma
Ma waan la naka le
(Fétial ma , ma féélou la)
Baby ! Kay diéga ma
Ma waan la naka le
(Fétial ma , ma féélou la)
Nangoul wakh!
Nél sa khol maan ma fa néh
Baby tay ma léral la
Né khaam nani maan rék ngay weur
Deug le
Kou mél ni nga sokh la
Meuné founéh
Fouma feul rék diomal la
Khaam na ni djantal nga
Nangoul né ma lay bègueul
Soon na si saag bi
Di mougn lou mel ni
May ladj ki laan la
Maan da ma soon si saag bi
Di mougn lou mél ni
May ladj ki laan la
Baby! nangoul ma
Wakhal sa gars Gni
Maan mail sa star
Té nga siggi khol ma
Soon na si saag bi
Di mougn lou mel ni
May ladj ki laan la
Maan da ma soon si saag bi
Di mougn lou mél ni
May ladj ki laan la
Comentários
Envie dúvidas, explicações e curiosidades sobre a letra
Faça parte dessa comunidade
Tire dúvidas sobre idiomas, interaja com outros fãs de Viviane Chidid e vá além da letra da música.
Conheça o Letras AcademyConfira nosso guia de uso para deixar comentários.
Enviar para a central de dúvidas?
Dúvidas enviadas podem receber respostas de professores e alunos da plataforma.
Fixe este conteúdo com a aula: